GENTLEMAN Lyrics
Intro
Yo it’s your boy EL-Z-O from Jamdong Community and I go by the a.k.a of Gentleman (yeah yeah )
Couplet 1
Chaque jour degn may camera
Fresh ni kou diogué Canada 🇨🇦
Koumeu songg dinga sango coups (Son Goku)
Limoy flowou Camé Hamé Ha
J’suis dans le building t’es jamais là (never)
Son ba ngui yengueul se favela (bang)
Rappeurs yi possé comme Pamela,
Naleen nieuw sauver comme Pamelaaa
Pro laa soudé guenné hit
Thug life ci semey ennemis
Sope-man douniou dieguéti
Teaupla leme diogué te
Guisseugoumeu motherfucker boumeu meuneu fatté lo semey origine (Macina)
Kouniou beugg booker gratuit defe fekk khamago souniou money team
(Mayweather)
Rewandé diarouteu diaay
Te talent dé ken dou ko dieund
Diaroul may deglou medias yi
Ndakh mane le media yi di reubb
Yalla dji rekka niou tiim motakh
Yalla dji ken dou ko neubeutou
Wakhkat yi kheebouniou dara defeul niou wakh defo niou kebetou (Nopi leenn)
Fils
Mane diaayouma pegarou ghetto pour diaay seme disque (no no no no)
Tabaski segnou se rappeur di raay seme birr (tabaski flow)
Dem lakhatou kaaw ba téréwul maa gueuneu siiw
Mais lane moye se saafara free ?
Pont
Defal se job beuss dineu dokh
Ken matoul thi adouna
Gueumeul se bopp
Gueumeul se bopp
Bo togné nga dieggueulou
Bo togné nga diéggueulou
Bo togné nga diéggueulou
Loloy gentleman
Refrain
Gentleman x9 (Skurrr)
Khamnaa louy parcourou gentleman
Se benn pékhé mounouniou gêner man
Boy ya ngui pélleul niou thiéné rek
Ken gueunouniou nekk gentleman
Gentleman x9
Khamnaa louy galèrou gentleman
Se benn pékhé mounouniou gener man
Boy ya ngui pelleul niou thiéné rek
Lokho thi kow bodé gentleman
Post-refrain
Lokho thi kow bodé gentleman
Gentleman gentleman gentleman (skurrr)
Kham naa louy galerou gentleman (yeah)
Gentleman gentleman gentleman (yeah, yeah)

2e couplet
Niémé def lou bess sama définition (sama définition)
Sama niaanou mère sama bénédiction (yaay niaanal ma)
Def len lou khess mogueun ngueen ne fi di thiow
Wallahi danguene yep gnigni moss

I’m a Gentleman amoul benn man boumay tekkheulék seme bopp
Artiste bou mel ni dotoko degg fenn sama rak
Dotoko degg fenn yow mi done diemeu mel ni seme clone
Dotoko defati dome, légui guénn leen seme domaine domaine

Kholeul kenn douleu guenné tchi se merde
Lo fi sombi ding ko naan amoul dessal amoul guedd
Flow bi amoul mel ni catholique bou signer takk niarrel (flow bi amoul)
Indil ga yi DAANOU RAP, limoye RAP bilen di DAANEL

Indi lou bess, concert yi fess
Akimo yapp (akimo) bayil le ress (bayil le ress)
Rest in peace papa gaindé nga yama done diokh loumeu lekk (gaïndé nga gaïndé nga)
Kou fi né limay def nekhouleu rek dangay wokh louleu neekh (dangay fen)
Pont:
Defal se job beuss dineu dokh
Ken matoul thi adouna
Gueumeul se bopp
Gueumeul se bopp
Bo togné nga dieggueulou x3
Loloy gentleman
Refrain
Gentleman x9
Khamnaa louy parcourou gentleman
Ben pékhé mounouniou gener man
Boy ya ngui pelleul niou thiéné rek
Ken gueunouniou nekk gentleman
Gentleman x9
Khamnaa louy galèrou gentleman
Se benn pékhé mounouniou gener man
Boy ya ngui pelleul niou thiéné rek
Lokho thi kow bodé gentleman
Post-refrain
Lokho tchi kow bo dé Gentleman
Lokho tchi kow bo dé Gentleman
Gentleman gentleman gentleman
Khamnnaa louy galèroi Gentleman
Gentleman gentleman gentleman

postes similaires
Latest Posts from RAP221

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *