Refrain}
Bo djougué wone mane fima djougué
Di nga djoug fadjar téél takkeu toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma goudé
Guiss ngama now sama baatu mère dima goungué
Né nama “Basse Basse, Abdou démal dieuli li nga mom”
Né nama “Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug boul topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse wakh djou bone dou takkeu foudoul guémignou borom”
{Verse 1
Bou ngène tchi seugué douma siggui
Bou sérithieu bi matoul non douma gnibi
Boudé yaapeuh taamou natchi dibi
Boudé yaapeuh dioxma diplôméé bi
Xalé bou djangueuh tangueuh djaapou niamboureum
Djiguène 100% ma tchi thiapeuh some
Té bouko diaré mane sagne naako songueuh
Séti waadioureum niaani dji lokhom
Rap Game bi légui noumou démé
Niom nieupeu beug nékeu MOI
Mais kèneu matou tchi ni février
Douniou gatt loudoul thiouthiou ci thiaaz
{Refrain}
Yombeu love boma beugoul xamna da nga am problèmou xol
Shaw bi néna: “may nélaw douma robot” mane manéko:
“Bo djougué wone mane fima djougué
Di nga djoug fadjar téél takkeu toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma goudé
Guiss ngama now sama baatu mère dima goungué”
Né nama : “Basse Basse, Abdou démal dieuli li nga mom”
Né nama : “Basse Basse yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug boul topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse, wakh djou bone dou takkeu foudoul guémignou borom”
{Verse 2
Koukay tothie fils guiss nga limay tabakh
Philip Morris lou guéneu def Tabac
Stephen Curry fouma tolleu thiabakh
Marqué sama temps ni Chaba
Doundeu bopp bi moy dougou sama pas
Maximum bi séddé ni dama baakh
Tolo féneu beug dieul sama part
Roi des arènes fékhel bama mbapaate
Rakkeu guènaatal rap ba tchi kanam
Fi nga né ma ngi fawone ay aate ci guinaaw
Cachés concert et tu parles de finance ?
Dama Rap baniou may wo tchi ay conférence
Def Cos. bou saff andeu ak éloquence
Wane lène fi niou diaar def différence
Bou baakh dou bou bone bi yeah bi moy référence
Yeah defko sa bopp fils Shampoo dou Karaass
Sa Rappeur dou bagaaaaage, Sa Rappeur dou bagaaaaage
{Refrain}
Yombeu love boma beugoul xamna da nga am problèmou xol
Shaw bi néna : “may nélaw douma robot” mane manéko…
“Bo djougué wone mane fima djougué
Di nga djoug fadjar téél takkeu toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma goudé
Guiss ngama now sama baatu mère dima goungué”
Né nama : “Basse Basse, Abdou démal dieuli li nga mom”
Né nama : “Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug boul topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse, wakh djou bone dou takkeu foudoul guémignou borom”
Basse Basse Basse, wakh djou bone dou takkeu foudoul guémignou borom
Bo djougué wone mane fima djougué
Di nga djoug fadjar téél takkeu toubeuy
Gnimay khaar beuri meunouma goudé
Guiss ngama now sama baatu mère dima goungué
Né nama “Basse Basse, Abdou démal dieuli li nga mom”
Né nama “Basse Basse, yone wi nga taameuh détchi dem ak jom
Té bo démé ba soneuh ditchi douté kholal tchi gni leu beug boul topoto say noone
Abdou Basse Basse Basse, wakh djou bone dou takkeu foudoul guémignou borom”

postes similaires
Latest Posts from RAP221