Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo.
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Couplet 1
Nieuwal mbedo bénén life la mane ak sama gayi niougui bendo
Nieuweuk ghetto never mine la multitude pote mofiy daw.
Waww waww..
Wane la lodoul guiss loudoul degg khamna digua know.
Waxma yagui bègue yankoy yégue night bi di gueuna Go!
Tékk zeum half night , talle call night late ,film daw To I late, teugue Match side side.
Mbedo bendo lolou-oy ghetto.
Refrain
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo.
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Couplet 2
Prisonnier sa peine kaygne lén la juger.
Fatéll lepp nieuweul niou diapisé ,kagnou dem concert après niou gnibisi nénagn dioub dou wéss kon bokk gnibissi.
Kaygnou dance boudé daff lay dimbali pour gua faté say pression.
Eh kay niou dance fibou wésso hip-hop guisso centre de rèinsertion
Refrain
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo.
Guediawaye Goudi Goudi
Mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo
Ouh! Lahlahlah
Mbedo dance mane ak sama gayi fok niou gnibi bendo

postes similaires
Latest Posts from RAP221