Mollah Morgun : louma nakari neexouma/ (j’aime pas )beugouma/ di guiss boy rappeurs you rerr si seni guintt /di feintt/ dundu boudoul sén boss /guissouniou lenn loudoul alalou adouna djiné/djiguén ak taar/sen birr /yi di dioy niouy diay boss/Goss you gnimeewoul responsabiliser sén bop si wax li town bi di rirr thi tarr tarr/ nakar ak tiss/
deuk bou diaxasso ak injustice/salfagnio ni dolé meun deugg bithi biir hospice/Xell yi xalatt yi nagam diaxasso niou teuweu fessal/di niodi king model wallah guide ak am money/man! bari wax ni barigo bou vide.sén lokho diotoul sen guinaw dougn lekk ba dessal di xeuthio ma fessal grand théâtre Stade place walla monument.niouy yiété niouy yiétalaté;yabaté di naxaté wayé Yallah dina atté.musik bouy nalawalaté triste si sonorités fond bou manqué activisme.niéwoumaleen. Ñiéwouma ñileen di youkho’ka tathiou.
kouthi guindi woul djiamm yi thi diam diam yi ba dé dinga ko reuthiou.music bou haram si sen thème yi/ di égo kessé aki je t’aime je taime yi/si sén game faté ni ñi mbeuguél di fitnal si biir keur yi niouy seungueem di mougn di encaisser/rongogn di tokk sen birr keur yi.ni mbedd mi mell gnim fi gassal bamell.mane daal thi mbindd mi mathie ma la amm namell/ ndax xamm namm mell/ gniy bindd di guindi di deff di dindi di indi.ma reudeul leen sen fin phrase si point final.boy binga dioudo sa kogn ba légui waxma loufa sopékou si say niogn?yeeyal ma gni medias yi gueuleumeul si ay telenova sopileen ay Casanova saup leen si American dreamz » damala lova « afin que-le-mal gagne du terrain pouss bayi félins yi thi ngour di dundu si sunu derett ni lekkatou mirassou orphelins gni fi indi sauve qui peut !wallah yeugougn li frère yi di dathie si desert Libye bi.niata fa déé thi alleu bi?wallah guissoul ni ici on tire le diable par la queue?di wout di amm di gun di bankk bankk sa bop si sank sa bop si rap loudoul sa beugg beugg bop yagg yagg dinga rendre compte
foudoul sa tombe dou sa compte banque.eglou taxoul ma xam li gniy wax ndax lekk sen lamign yi.waxma ligniy lakkeu?vocab bou diaxasso ni biir bouy daww amougn chance ndax djiteul sen bameelou biirr fatee sen paxou biir….kan le chat nest pas la les souris dansent.sa bop kottou moy sa fiérté bop dieuleul lepp té ni mott deudou bagn waxal gni sen bakane néthi xottou guerté bilahi fanga pérté bi nga déserté sa mission…bar yek boite yi fess teepp.djiakak djiouma yi wett firndeewoul loudoul rouhh you repp…waxtou wangui waxou sa way.Pardon defal lou gaww rakk mane awma temps bouma perte mbirr yangui URGENCE !!!

postes similaires
Latest Posts from RAP221

Laisser un commentaire

Votre adresse de messagerie ne sera pas publiée. Les champs obligatoires sont indiqués avec *